Banji Koto


An extraordinary birth


en Français | auf Deutsch






    Banji Koto yaayam dafa ka ëmboon, baka yaay ji ëmbee muy xale bu am bopp. Amoon na nak ñaari mag yu waroon doxaani sa ganaaw dëkk baa ñaari janq yoo xam ni seen rafetay jeggi na dayo, ñaari janq yooyu nak dañu leen doon tooñ, maanaam ay dëmm lañu woon.

    Keep koo xam ni dem nga fa, di doxaani, seen yaay ray la. Balamu lay ray nak dina la noosal, rayal la ay ginaar, rayal la tamit ay rar. Dara du des. Su noos bi jeexe mu ray la, daadi noos moom itam. Mu kay def, di ka def ba benn bes mu ñëw si ñaari magu Banji Koto. Fekk na nag Banjikoto yaayam mu ngi ka ëmboon ba mu am juroomñenti weer.

    Banji Koto daldi ni ka: "yaay wasin ma"

    Yaay ji ni ka: "ah mande mënu ma la wasin, bu yaboo nga wasin a bopp"

    Banji Koto était déjà une "grosse tête" quand il était dans le ventre de sa mère, il avait deux grands frères: deux grands frères qui devaient aller dans le village voisin, courtiser deux jeunes filles d'une beauté rare et recherchée qui malheureusement étaient réputées être des sorcières



    Leur mère tuait tous ceux qui allaient les courtiser. Mais avant de les tuer elle n'hésitait pas à égorger poulets et moutons en l'honneur des prétendants. Rien ne manquait. Après les avoir bien accueillis, elle les tuait.la mère de Banji Koto était enceinte de neuf mois quand les deux frères décidèrent de se rendre chez la sorcière.




    Aussitôt Banji Koto dit à sa mère: "mère, mets moi au monde"

    Elle lui répondit: "ah! je ne peux pas le faire, fais le toi-même"


That is the beginning of the tale that was collected in 1980 by Mouhamadou M. Diaw in Mbakhana, about 20 km from Saint Louis du Sénégal, reported by Mrs Coumba Diagne who did hear it from her 80 years old died aunt Khady Seyni Dia.

This short extract comes from the number 6 of DEMB AK TEY cahiers du mythe (Centre d'Etude des Civilisations BP 4001 Dakar Sénégal 1980)

If you know a good english translation of this text, thank you to share it.

You may also correct my approximate english and specify to me the mistakes and the necessary idiomatic forms.


There is an excellent website about wolof language proposed by Pape Diakhate that I strongly advice


  Back   to AN OPEN WINDOW TO THE WORLD